Genesis 24:56
TSK
Mu ne leen: «Gannaaw Aji Sax ji àntal na sama yoon, tee ngeen ma baña yeexal, te bàyyi ma rekk, ma dellu ca sama sang?»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu ne leen: «Gannaaw Aji Sax ji àntal na sama yoon, tee ngeen ma baña yeexal, te bàyyi ma rekk, ma dellu ca sama sang?»
¶ Ba loolu amee ndaw sa takk mbaam ma, ne surgaam: «Doxal jiitu, bu ma taxawloo ci yoon wi te waxuma la ko.»
Xooleel, sa bët ne jàkk, ngay xool sa kanam màkk.
Mu neeti keneen: «Toppal ci man.» Mu ne ko: «Sang bi, may ma, ma jëkka dem robi sama baay.»
¶ Yeesu neeti leen: «Ba ma leen yebalee te du dencukaayu xaalis, du mbuus, du carax yu ngeen yóbbaale, ndax ñàkk ngeen dara?» Ñu ne ko: «Déedéet.»