كل أسفار KYG

Luke 13

KYG · الآية 14

24 أصحاحات

KYG / Luke / الأصحاح 13

KYG · الآية 14

N jiitu jàngu ba nag yékkati kàddug ñaawlu ndax bésub Noflaay ba Yeesu faje. Mu ne mbooloo ma: «Juróom benni fan la nit ñi wara liggéey. Kon ci fan yooyu ngeen wara fajusi, waaye du ci bésub Noflaay.»