TSK

TSK · Luke 20:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ñu indil Yeesu cumbur bi, sànni seeni yére ca kawam, daldi waral Yeesu.

Acts 4:7 TSK

Ñu taxawal Piyeer ak Yowaan ca digg ba, laaj leen ne: «Yeen, lii ngeen def, ci ban xam-xam, ak ci wan tur ngeen ko defe?»

Acts 7:35 TSK

¶ «Musaa moomu ñu weddi woon, ne ko: “Ku la def kilifa ak ab àttekat?” Moom nag la Yàlla def kilifa ak ab jotkat, yebal ko ci ñoom, malaaka ma feeñu Musaa ca gajj ba, daldi koy jottli yóbbante ba.