Genesis 49:10
TSK
Nguur gi du jóge ci loxol Yuda, te yetu buur ay wéye sampe ciy tànkam, li feek boroom di ñëw, ba xeet yi déggal ko.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Nguur gi du jóge ci loxol Yuda, te yetu buur ay wéye sampe ciy tànkam, li feek boroom di ñëw, ba xeet yi déggal ko.
Erodd boroom diiwaan ba nag, Yaxya sikkoon na ko ndax Erojàdd jabaru magam ja mu nekkaloon, ak mboolem yeneen ñaawtéef yu Erodd def.
¶ Gannaaw loolu mbooloo ma mépp jóg, daldi yóbbu Yeesu ca Pilaat.
Ci kaw loolu Pilaat dogal ñu defal leen la ñu sàkku.
¶ Ñeel la yaw boroom réew mi, Feligsë mu tedd mee tedd, bawoo ci man Këlódd Lisiyas, mi lay nuyu.
¶ Ci kaw loolu buur bi ak boroom réew mi jóg, ñook Berenis ak ña ñu toogal.