Ña nga naa leen: «Céy ngalla nun, su nu sañoon dee, Yàlla moom nu ca réewum Misra, fa nu daan uufe cini yàpp, ñam wa ne gàññ, nu suur këll. Yeena nu indi ba ci màndiŋ mii, ngeen nara xiifloo mbooloo mii mépp, ba ñu dee.»
TSK
TSK · Numbers 11:4
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba loolu wéyee amoon na ci biir bànni Israyil jenn waay ju yaayam di doomu Israyil te tuddoon Selomit doomu Dibbri, Daneen ba. Baayam di waa Misra. Mu am bés xeex jib ci biir dal bi, ci diggante waa jooju ak jenn waayi Israyil ju raxul. Ci biir loolu waa ji yaayam di doomu Israyil wax Yàlla lu ñaaw, tudd ko jaar fu bon. Ñu yóbbu ko ca Musaa.
¶ Ba loolu amee mbooloo mépp tàmbalee yuuxu. Askan wa daa fanaanee jooy guddig keroog.
Naka la mbooloo ma dégg la yoon wa digle, ñu daldi dàqe Israyil mboolem askan wu raxe.
Dóor naw doj, moos, ndox ma fettax, wal ma baawaan, waaye aw ñam nag? Daa mana leel mbooloo mii aw yàpp?»
Waaye yiirooleen Sang Yeesu Almasi, te ngeen baña yittewoo seen bakkan, ngir di topp seeni xemmemtéef.
Bu leen kenn nax: «Ànd bu bon yàq na jikko ju baax.»