TSK

TSK · Numbers 26:55

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Tegooleen bant réew mi, séddoo ko ci seeni làng. Làng gu gëna mag, na am cér bu gëna mag, làng gu gëna tuut, am cér bu gëna tuut. Fépp fu tegoo bant génneel ag làng, ñooy doon boroom. Ci seen biir giiri maam ngeen di séddu.

Ñu ne: «Sang bi, xam nga Aji Sax ji moo digle woon ñu tegal bant bànni Israyil, séddale leen réew mi. Ci biir loolu, sang bi, ndigal ñeel la, tukkee ci Aji Sax ji, ngir nga jël sunu céru doomu baay Selofat, jox ko ay doomam yu jigéen.

Tegoo bant nit a koy def, dogal ba Aji Sax ji la.

Acts 1:26 TSK

Ñu tegal leen nag bant, bant ba dal ca Maccas, mu dolliku ca fukki ndaw yaak benn.

¶ Ma dégg limub ña ñu màndargaale torluwaay ba; ñuy téeméer ak ñeent fukk ak ñeenti junni (144 000), bawoo ci mboolem giiri bànni Israyil: