كل أسفار KYG

Numbers 36

KYG · الآية 2

36 أصحاحات

KYG / Numbers / الأصحاح 36

KYG · الآية 2

Ñ u ne: «Sang bi, xam nga Aji Sax ji moo digle woon ñu tegal bant bànni Israyil, séddale leen réew mi. Ci biir loolu, sang bi, ndigal ñeel la, tukkee ci Aji Sax ji, ngir nga jël sunu céru doomu baay Selofat, jox ko ay doomam yu jigéen.