Numbers 27:1
TSK
¶ Ci kaw loolu ay doomi Selofat yu jigéen jóg. Seen baay Selofat, Efer ay baayam, Efer, Galàdd ay baayam, Galàdd, Makir ay baayam, Makir, Manaseey baayam, Manase, Yuusufaay baayam. Jigéen ñooñu ñoo di Maala ak Nowa ak Ogla ak Milka ak Tirca.