كل أسفار KYG

Numbers 32

KYG · الآية 17

36 أصحاحات

KYG / Numbers / الأصحاح 32

KYG · الآية 17

W aaye nun kay danuy daldi gànnaayu, jiitu bànni Israyil, ba keroog ñu leen yóbboo ca seen suuf. Sunu njaboot a nuy xaare fii, biir dëkk yu tata wër, ngir ñu mucc ci waa réew mi.