Numbers 32:29
TSK
Musaa ne leen: «Su Rubeneen ñeek Gàddeen ñi àndeek yeen, ñoom ñépp gànnaayu ngir xareji fi kanam Aji Sax ji, ba réew ma nangul leen, nangeen leen jox réewum Galàdd, muy seen moomeel.