¶ «Su dee dëkki Leween ñi ak seen dëkkuwaay ya ca biir nag, Leween ñi sañ nañu cee jotaat fàww.
TSK
TSK · Numbers 35:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Leviticus 25:32
TSK
Ezekiel 45:1
TSK
¶ «Bu ngeen demee bay tegoo réew mi bant ngir séddoo ko, nangeen jooxeel Aji Sax ji dogu suuf bu gudde ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000), yemook fukki kilomeetar ak ñett, yaatoo ñaar fukki junniy (20 000) xasab, yemook fukki kilomeetar ak genn-wàll. Suuf soosu sépp ba fa mu yem, lu sell lay doon.
Ezekiel 48:8
TSK
¶ «Suuf sa digalook Yuda ca wetu bëj-gànnaaram, te dale penku ba sowu, mooy doon pàkk bi ñuy jooxe. Ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000), fukki kilomeetar ak ñett, lay yaatoo, gudde ni suufas genn giir gu ci nekk, te bérab bu sell bi nekk ci digg bi.
Am du noo tax muy wax? Nun kay noo tax ñu bind loolu, ndax kuy bey, sañ cee yaakaar, kuy bojj it, sañ cee yaakaar wàllam.