Exodus 30:1
TSK
¶ «Sàkkal ab sarxalukaay bu ñuy taal cuuraay ci kawam. Bantu séng nga koy defare.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «Sàkkal ab sarxalukaay bu ñuy taal cuuraay ci kawam. Bantu séng nga koy defare.
ak sarxalukaay bu wurus bi, ak diwu pal gi, ak cuuraay lu xeeñ li, ak kiiraayal buntu xayma bi,
¶ Ba mu ko defee ñu dugal sarxalukaayu wurus bi ci biir xaymab ndaje mi, ci kanam rido bi,