Yàlla daldi barkeel bésub juróom ñaareel ba, def ko bés bu sell, ndax da caa dal-lu woon gannaaw liggéey, ba mu sàkke lépp.
TSK
TSK · Numbers 7:1
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
te aw yëkk ngay def saraxu póotum bàkkaar bés bu nekk, muy seen njotlaay, di njotlaay liy setal sarxalukaay bi. Te itam nanga diw sarxalukaay bi ag diw, sellale ko ko.
Noonu ngay sellale yooyii, mu daldi doon lu sella sell. Lépp lu laal yooyii day doon lu sell.
Nanga diw mbalkam njàpp mi akub tegoom, nga sellale ko ko.
¶ Ba loolu wéyee Musaa jël diwu pal ga, diw ca jaamookaay baak ya ca biir yépp, sellale ko yooya,
¶ Loolooy saraxi daloob sarxalukaay ba, ca bés ba ñu koy diw, sellal ko, lépp bawoo ca kilifay Israyil. Ndabi xaalis ya fukk laak ñaar, këlli xaalis ya di fukk ak ñaar, bàttuy wurus ya di fukk ak ñaar,
«Waxal Elasar doomu Aaróona, sarxalkat bi, ne ko mu seppee and yi ci lakk gi, ndax lu sell la, te xal yi, na ko tuur fu sore.