TSK

TSK · Numbers 7:10

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Keroog ba Musaa sampee jaamookaay bi ba noppi, diw na ko ngir sellal ko, mook mboolem ay jumtukaayam, sarxalukaay beek mboolem ndabam it, mu boole diw, sellale ko.

Mu defal Aji Sax ji saraxi cant ci biir jàmm, lépp di ñaar fukki junniy nag ak ñaar (22 000) ak téeméeri junniy gàtt ak ñaar fukk (120 000). Noonu la Buur ak bànni Israyil gépp amale xewu jagleb kër Aji Sax ji.

¶ Gannaaw gi, ca xewu daloog tatay Yerusalem ja, ñu wooye Leween ña mboolem fa ñu dëkke, indi leen Yerusalem, ngir ñu màggal daloo ga ci biir mbég ak jàngi cant; tëggum weñ ya jib, ànd ak xeeti xalam.

Muy woyu Sabóor, ñeel Daawuda ca daloob kër Yàlla ga.