Numbers 1:4
TSK
Giir gu ci nekk, àndleen ceek kilifa yi jiite seen këri maam, ñu jàpple leen ci.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Giir gu ci nekk, àndleen ceek kilifa yi jiite seen këri maam, ñu jàpple leen ci.
¶ Ba loolu wéyee Aji Sax ji wax Musaa ak Aaróona, ne leen:
Bu ñu liitee benn nag kilifa yi jiite gàngoori Israyil ñooy dajesi fi yaw.
¶ Ba ñu àggee ca kër Aji Sax ja ca Yerusalem, am na ñenn ca kilifa ya jiite seen kër baay, ñu joxe ay saraxi yéene ngir tabaxaat kër Yàlla ga ca gentam.