TSK

TSK · Proverbs 12:24

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Bu gisee ni mbaaram neexe, ak ni réew mi naate, day waaf, gàddu ngaaxam, daldi féetewoo coonob njaam.

Booba Yerbowam xalelu góor bu jàmbaare la woon. Suleymaan jot koo nemmiku ci biir liggéeyam, ba tax mu tabb ko ca kaw mboolem liggéeykati sañul-bañ, ya askanoo ca Yuusufa.

Ab yaafus day yaakaar, du am; ab njaxlaf sàkku, woomle.

Ab yaafus, nelaw yu xóot, te ku yàccaaral xiif.

Bul yaafus, ba naan: «Gayndee ngi ci biti, dañu may rey ci mbedd mi!»

Toolub ku yaafus laa jaare, ak tóokërub nit ku ñàkk bopp.

Ab yaafus day tëdd ak a walbatiku, mooy bunt, day jaayu, demul fenn.