TSK

TSK · Proverbs 18:24

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ba loolu amee Yonatan fasook Daawuda kóllëre, ndax sopp ko ni boppam.

¶ Ba Daawuda delloo Ciglaag, sédd na ca lël ja, magi Yuda, xaritam ya. Mu yónnee leen ko, ne leen: «Lii, yeenay boroom; xéewal la gu jóge ca alalu nooni Aji Sax ji.»

¶ Daawuda moo noon: «Ndax kenn desul ba tey ci waa kër Sóol, ba ma jëfeek moom ngor ngir Yonatan?»

Absalom ne Usay: «Loolooy sa kóllëre ak sab xarit a? Lu la teree ànd ak sab xarit?»

Buur ne ko: «Ana looy waxati lii lépp? Dogal naa yaak Ciba, ngeen séddoo suuf si.»

Diwook suuru day naatal xol; waaye li neex cib xarit, xol la lay digale.