TSK

TSK · Proverbs 19:16

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 5:2 TSK

Am sannax déy, naqari deret a koy rey, ab téxét, xéraangee koy faat.

Doom, bul fàtte sama njàngle, defal sa xel ci saay santaane,

Xalab waxi yar, foye sa bopp la; deel déggi àrtu, yokk sam xel.

Yoonu njublaŋ, ay dég aki fiir; ku sàmm sa bakkan sore ko.

Ku dégg ndigal doo am lu la soof. Ku xelu, xam lu jot, xam doxalin.

Mbir mii déy laa leen santoon ne leen: “Déggal-leen ma, ma doon seen Yàlla; yeen ngeen doon sama ñoñ. Doxeleen wépp yoon wu ma leen sant, su ko defee ngeen baaxle.”

Moom nag mu ne ko: «Xanaa kay, ndokklee ñiy déglu kàddug Yàlla te di ko jëfe.»

Xaraf amul solo, ñàkka xaraf amul solo. Li am solo moo di topp ndigali Yàlla.

¶ «Ndokklee yeen ñi fóot seeni yére, ngir saña lekk ci garabu dund gi, jàlle bunt yi, dugg ci biir dëkk bi.