Psalms 3:4
TSK
Waaye yaw Aji Sax ji, yaa may feg, di ma teral, di ma siggil.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waaye yaw Aji Sax ji, yaa may feg, di ma teral, di ma siggil.
di sama wóllëre, di ma yiir, di ma làq, di ma xettli, di ma aar, ma di ko làqoo, mu di ma nangulal ay xeet.
Ku ñaw day xelu, xam li muy def; ab dof di nax boppam.
Lu Yàlla wax, mat na sëkk, mooy yiir ku ko làqoo.
Waaye ci ñi ñu woo, ñuy Yawut, di Gereg, Almasi mooy manoorey Yàlla, di xam-xamu Yàlla.
¶ Moona xam-xam lanuy xamle ci biir gëmkat ñi mat, waaye du xam-xamu xarnu bii, ak bu njiiti xarnu bii, di nit ñuy wéy.
Ci moom la mboolem alal ji ci xel ak xam-xam, dëxëñe.
Moomu xel jógewul fa kaw, àddina sii la bokk, di yëfi bakkan, te di mbiri Seytaane.