Psalms 9:18
TSK
Ñu bon ñee dëddu, dem njaniiw, ànd ak xeet yi fàtte Yàlla yépp.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ñu bon ñee dëddu, dem njaniiw, ànd ak xeet yi fàtte Yàlla yépp.
Xamal ne xel mu rafet ni la neexe; soo xeloo, sa muj rafet, te sa yaakaar du tas.
Ndax man déy, xam naa mébét yi ma leen mébétal.» Kàddug Aji Sax jee. «Du mébéti loraange, waaye mébéti jàmm laa leen mébétal, ngir may leen yaakaaru ëllëg.
Seen jëfi démb ja leen gàcceel tey, ana njariñ lu mu leen jural? Mujug jëf ja de, seenug dee la doon doon.
¶ Kon nag buleen teqlikook seenu fit, yool bu réy a ngi ci.