Proverbs 8:14
TSK
Maa moomi digle, di maye gis-gis; maa am ug dégg, di boroom doole.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Maa moomi digle, di maye gis-gis; maa am ug dégg, di boroom doole.
Ku ñaw mana daan jàmbaari dëkk bu mag, ba màbb tata ja ñu yaakaaroon.
Ab dëkk bu ndaw la woon, nit ña néew. Buur bu mag song dëkk ba, gaw ko, jal jali suuf yu mag, sësal ca tata ja.
kiy yaakaar Aji Sax ji moom, di yeeslu doole; da naa fëyy ni jaxaay juy naaw, di xélu te du xiix, di dox te du xoox.