TSK

TSK · Proverbs 26:1

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Du nu ngi ci ngóobum bele tey? Dinaa ñaan ci Aji Sax ji, mu dënu, taw. Su boobaa dingeen xam xéll ne ba ngeen sàkkoo buur, lu bona bon ngeen def, Aji Sax ji seede.»

Atag dem ba ca Mardose, ca pénc ma janook buntu kër buur.

Ngalla Aji Sax ji, sàmmal ku néewle, aar ko saa su ne ci nitu tey.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di taalif bu ñeel Daawuda.

Dund gu neex jekkul cib dof, surga buy jiite kilifa it moo yées.

Kuy teral ab dof, jël ngaw doj, takk ko ci mbaq.

Lu mettee ngi lu ma gis fi kaw suuf, lu mel ni njuumte lu rëcc kilifa: