TSK

TSK · Proverbs 26:12

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Na dof di jëfe, njub la ci moom; dégg ndigal rafet um xel la.

Waaye toppal ab dof cig ndofam, lu ko moy mu defe ne daa muus.

Waay a ngi barele, defe ne xelu na; ku néewle am ug dégg, gis ne xeluwul.

Ana koo gis, mu rattaxle? Kooku ab dof a ko gën demin.

Farisen baa nga taxaw di yelu, naan: “Yàlla, maa ngi lay sante li ma melul ni ñeneen ñi doonul lu moy ay lekk-kati àq, ay njublaŋ aki jaalookat, rawatina juutikat bii.

¶ Bu kenn nax boppam: Ku teg boppam ci yeen, boroom xam-xam, ni xarnu bii jàppe xam-xam, kooku na doon ab dof, ngir am xam-xam bi wóor.

Gannaaw yaa ngi naan: “Am naa alal, barele naa, soxlaatuma dara,” te yaw xamuloo ni nga toroxe, jara yërëm, ñàkk, gumba, ne duŋŋ,