Proverbs 20:6
TSK
Ñu baree ngi naa: «Gore naa,» waaye kuy boroom kóllëre dëgg?
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ñu baree ngi naa: «Gore naa,» waaye kuy boroom kóllëre dëgg?
¶ Ñenn ci ñooñu di seedeel seen bopp ne ñoo yelloo ngërëm nag, nun ñemewunoo boole sunu bopp ak ñoom, mbaa nuy méngale sunu bopp ak ñoom. Waaye ñoom dañoo amul xel, ndax nattukaay bi ñuy nattoo, di ko méngalantee ci seen biir, ñoom ñoo ko sàkkal seen bopp!
¶ Mujj naa dib dof nag, te yeena ma ko yóbbe, nde gërëm maa leen waroon, ndax doonte duma dara sax, ndaw yu màgga màgg yooyeey, duma seen cuune ci lenn.