Bés a ngii tey, nga gisal sa bopp ni la Aji Sax ji tege tey ci samay loxo ci biir xunti mi. Nee ñu ma, ma rey la, waaye dama laa xool bëtu ñeewante. Maa ne duma xàccil mukk sama loxo sama sang, ndax mooy ki Aji Sax ji fal.
TSK
TSK · Proverbs 28:12
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
1 Samuel 24:11
TSK
1 Kings 18:13
TSK
Moo sang bi! Xanaa waxuñu la li ma def, ba Yesabel di rey yonenti Aji Sax ji? Maa làq téeméeri yonenti Aji Sax ji ci ay xuntiy xeer, xunti mu nekk juróom fukk, di leen may lekk ak naan.
Esther 8:16
TSK
Kanami Yawut yaa nga ne ràññ ci biir mbégteek bànneex akub sag.
Proverbs 11:10
TSK
Ku jub baaxle, waa dëkkam bànneexu; ab saaysaay saay, mbégte dim riir.
Proverbs 29:2
TSK
Ku jub falu, baadoolo bég; ab soxor jiite, baadoolo binni.
Ngalla yeen, réew mi gone falu buur, jawriñ ña di xëye xawaare.
Jeremiah 36:19
TSK
Kàngam ya ne Barug: «Demal làquji yaak Yeremi, te bu kenn xam fu ngeen ne!»
Luke 19:37
TSK
Ba ñu jubsee Yerusalem, bay wàcce ca mbartalum tundu Oliw ya, mbooloom taalibe mépp la mbégte jàpp, ñu tàmbalee sàbbaal Yàlla ca kaw ndax kéemaan ya ñu gis.