TSK

TSK · Proverbs 30:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 11:7 TSK

Dangaa mana gëstu mbóoti Yàlla, ba gis ko? Am yaa ñédd Aji Man ji?

Ku ci nekk di àddu, naan moroom ma: «Kee sell te sell te sell, keey Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi, àddina sépp a feese ag leeram!»

Moyal yoon wi; lajj, wàcc xàll wi, te may nu jàmm ak Aji Sell ju Israyil.

Amos 7:14 TSK

¶ Ba loolu amee Amos ne Amaciya: «Man de dumab yonent te bokkuma ci kurélu yonent. Sama gétt laa yor, te maa ngi topptoo ay tooli figg.

¶ Céy xóotaayub koomu Yàlla ak xel ma, ak xam-xam ba! Deesul natt ay dogalam, deesul ràññee ay jëfinam!

¶ «Malaakam mbooloom gëmkat ña ca Filadelfi nag, bind ko, ne ko: «Lii moo di kàdduy ku Sell ki, kiy Dëgg, te yor caabiy Daawuda, di tijji te kenn du tëj, di tëj te kenn du tijji. Mu ne: