TSK

TSK · Proverbs 4:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Gaawal dem ca Buur Daawuda, ne ko: “Buur, sang bi, du yaa ma giñaloon, yaw sang bi, ne ma sama doom Suleymaan mooy falu buur, wuutu la, te mooy toog ci sa jal bi? Kon nag lu tax Adoña falu buur?”

Aji Sax ji, maa xam ne nit moomul yoonam, kuy dox moomuli jéegoom.

Mànkooleen, buleen xëccu daraja, waaye nanguleena jonjoo ak ñi féete suuf, te baña jàppe seen bopp boroomi xel.