Genesis 38:23
TSK
Yuda ne ko: «Nanu ko ko wacce, mu jël, lu ko moy ñu ree nu, gannaaw maa ngi nii yónnee bëy wu ndaw wii, te yaw gisoo ko kay.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yuda ne ko: «Nanu ko ko wacce, mu jël, lu ko moy ñu ree nu, gannaaw maa ngi nii yónnee bëy wu ndaw wii, te yaw gisoo ko kay.»
Ma ne leen: «Xanaa du nii la Suleymaan buurub Israyil bàkkaare woon? Li xeet yiy bare lépp amul benn buur bu meloon ni moom. Ku Yàllaam soppoon la te Yàllaa ko faloon buurub Israyil gépp. Waaye moom sax jigéeni doxandéem yi bàkkaarloo nañu ko.
Ca kaw tund yu mag ya lañuy rendee ay sarax, cuuraay, ñu taale ca tund yu ndaw ya, ak ca taatu gii garab gu mag, ba ca gee, fa ker ga neexe. Moo tax seeni doom di gànctu, seen séeti doom di jaaloo.