TSK

TSK · Proverbs 8:6

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 33:1 TSK

Léegi Baay Ayóoba, ngalla déglul samay wax te teewlu sama kàddu yépp.

ngay ku tuut di ku mag, nga bareleek nga néewle.

Maa ngi leen di jàngal lu baax, buleen fàtte sama njàngle.

Dama laa bindal fanweeri dénkaane, ci wàllu digal ak xam-xam,

Kàddu googu moo di mbóot mi masoona làqu maasoo maas, waaye tey Yàllaa ko xamal ay nitam ñu sell.