Luke 18:9
TSK
¶ Yeesu léebati lii, ngir ñiy damoo seenug njub, tey doyadal ñi ci des.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Yeesu léebati lii, ngir ñiy damoo seenug njub, tey doyadal ñi ci des.
¶ Ba Piyeer di wax kàddu googu, Noo gu Sell gi daldi wàcc ci kaw mboolem ñay déglu kàddu ga.
Yaw nag ana looy sikke sa mbokkum gëmkat, ak itam, ana looy xeebe sa mbokkum gëmkat? Ndax kat nun ñépp ay taxawi fa kanam jalub àttekaayu Yàlla.
Soo dee lekk lenn ba tax sa mbokk am ci lu ko naqari, noppi ngaa doxe cofeel. Bu sag lekk sànk ku Almasi deeyal.
Te su demee noonu nag, su boobaa sa xam-xam bu réy ngay sànke sa mbokkum gëmkat bu néew doole boobu Almasi deeyal!
¶ Kon nag bu leen kenn sikkal ci ñam wu ngeen lekk, mbaa lu ngeen naan, mbaa màggal bés bu rafet, mbaa Terutel weer, ak bésub Noflaay.