TSK

TSK · Romans 3:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 20:14 TSK

Waaye la muy lekk ay soppiku ca biiram, doon daŋaru ñàngóor ca butit ya.

Dañuy fenante, làmmiñ dig lem, xol ba njuuy la.

Mooy ba Doweg, Edomeen ba, demee ca Sóol, ne ko Daawuda dem na kër Ayimeleg.

kuy nas lu bon, tey saxoo di sookey xare,

Seen mbari fitt ŋafal paxum bàmmeel, ñoom ñépp di ñeyi xare.

Xanaa du peeñuy caaxaan ngeen gis? Du ngisaaney fen ngeen di waxe, naan: ‘Kàddug Aji Sax jee,’ te man àdduwma?

James 3:5 TSK

Noonu itam la aw làmmiñ dee cér su tuut te réy aw bàkk. Seetleen ni ferñent su tuut di lakke gott bu yaa.