TSK

TSK · Romans 5:14

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Kon Aadama dund na juróom ñeenti téeméeri at ak fanweer (930), doora faatu.

Mu daldi tas mboolem dëkki joor ga, boole ca nit ña ak gàncax gépp.

Gannaaw loolu Firawna sant waa réew ma yépp, ne leen: «Mboolem doom ju juddu ci Ebrë yi, di góor, sànnileen ca dex ga, waaye lu ciy jigéen, bàyyileen, mu dund.»

Hosea 6:7 TSK

«Waaye ñoom ca dëkk ba, Adam lañu feccee kóllëre, foofa lañu ma wore.

Moyug kenn nit ki, ci la dee jaare ci kenn nit kooku, ba falu, kon ñi jot ci xéewalu yiw, ba jagoo àtteb njub, ñaata yoon lañuy gënatee falu ci biir dund gu ñu ame ci keneen nit kiy Yeesu Almasi?

Ndax kat, càkkéef gépp, li ñuy déggal neenug neen la, te du seen coobare, waaye ki leen ci tënk la neex, ba tax ñuy yaakaar,

¶ Noonu lañu binde ne: «Aadama, nit ku jëkk ka, lañu def jëmm juy dund,» waaye Aadama mu mujj mi moo di Noo giy dundloo.