TSK

TSK · Mark 13:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في Téereb Injiil.

العودة إلى المقطع

Mu ne leen: «Du gis ngeen yii yépp? Ci dëgg maa ngi leen koy wax, lii lépp dina daanu, ba doj dootul des ci kaw doj.»

Luke 21:6 TSK

«Li ngeen gis fii lépp, jamono dina ñëw joo xam ne dina daanu, ba doj dootul des ci kaw doj.»

Waaye bàyyil ëttu bitib kër Yàlla gi; bu ko natt, ndaxte jébbalees na ko ñi dul Yawut, te dinañu nappaaje dëkk bu sell bi diirub ñeent fukki weer ak ñaar.