Fa mbaxana dee benn lay tooge ni xellikat ak seggkat, te mooy segg sëti Lewi, xelli leen ni xaalis ak wurus, ba ñu doon niti Aji Sax ji, ñi koy indil sarax ci njekk.
TSK
TSK · Acts 3:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Malachi 3:3
TSK
Luke 1:70
TSK
noonee mu ko waxe woon ca jant yu jëkk ya, yonentam yu sell ya woon jottli,
Acts 3:19
TSK
Kon nag tuubleen te dëpp, ndax seeni bàkkaar faru.
Romans 8:21
TSK
ñoom ñi bokk ci càkkéef googu itam, ne dees na rengi seen buumi njaam gi leen ndee ak yàqutey yaram ràng, ngir ñu am cér ci goreelug doomi Yàlla yi, am cér ci seen teraanga.
2 Peter 3:2
TSK
ba ngeen fàttliku kàddu ya yonent yu sell ya jottli woon, ak sunu ndigalu Boroom, sunu musalkat, ndigal la jottlikoo ca ndaw ya ñu yebaloon ci yeen.
Revelation 22:6
TSK
¶ Ba loolu amee malaaka mi ne ma: «Lii wax ju wóor la te dëggu. Boroom bi Yàlla miy xelal yonent yi, moo yebal malaakaam, ngir mu won jaamam ñi mbir yi dëgmal te du jaas.»