Juróom ñaari nag yu baax yi, juróom ñaari at la. Te it juróom ñaari gub yu baax yi, juróom ñaari at la. Muy genn gént gi.
TSK
TSK · Daniel 2:45
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Te nag, sang bi, gannaaw gént nga ko ñaari yoon, kon Yàlla dogal na mbir mi, te dina ko amal balaa yàgg.»
¶ «Boroom bi, Aji Sax ji, Moo la tax di ku màgg! Kenn du yaw, kenn du Yàlla ku dul yaw doŋŋ, te mboolem lu nu nopp may, dëggal na loolu.
Fu ngeen dégg liit gi jibe fa, fekksileen nu fa. Sunu Yàlla dina nu xeexal.»
Yàlla, kay daa màgg ba wees xam-xam, te ay atam, deesul xayma lim ba.
Muy woyu Sabóor, ñeel askanu Kore wu góor.
Maa xam ne Aji Sax ji màgg na! Sunu Boroom a sut lépp lu ñuy jaamu.
Moo tax Boroom bi Aji Sax ji wax ne: «Maa ngii di dëj fi Siyoŋ aw doju coll, muy doju collu tànnéef wu gànjare ngir kenu gi, te ku ko wéeroo doo gaawa daw.
¶ Gannaaw loolu Dañeel dem ca Aryog mi Buur santoon mu rey boroom xam-xami Babilon. Ba mu demee ne ko: «Boroom xam-xami Babilon yi, bu leen reylu. Yóbbu ma ca Buur, ma jox ko piri mi.»
¶ «Ci jamonoy buur yooyu Yàlla Boroom asamaan dina samp nguur gu dul tas mukk, te wenn xeet du ko yilif mukk. Nguur googu dina tasaare mboolem yeneen nguur yooyu, ba genn du ci des, waaye moom day sax ba fàww.
Bésub keroog maay def Yerusalem di doj wu diis gann ci xeet yépp. Képp ku ko jéema yëngal, da ciy gaañoo gaañu rekk. Te xeeti àddina yépp ay daje ci kawam.
¶ Farisen yi ñoo laajoon Yeesu, ne ko: «Kañ la nguurug Yàlla di dikk?» Mu ne leen: «Dikkug nguurug Yàlla du ànd akum ceetaan.
Kon nag bindal li nga gis: Li am nii tey ak itam liy ñëw gannaaw lii.
¶ Ma gis nag menn malaaka mu taxaw ci jant bi. Mu àddu ca kaw, wax ak mboolem picc, yiy naaw ci digg asamaan, ne leen: «Dikkleen, dajesileen ci bernde ju mag ju Yàlla ji,