Genesis 25:13
TSK
Turi doomi Ismayla yu góor yaa di: Nebayot, taawub Ismayla, ña ca topp di Kedar ak Adabeel ak Mibsam
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Turi doomi Ismayla yu góor yaa di: Nebayot, taawub Ismayla, ña ca topp di Kedar ak Adabeel ak Mibsam
Xanaa du fani doom aadama fi kaw suuf àppu doñ-doñ la, dundam di dundu liggéeykat bu ñu bind?
Na waa àll beeki dëkkam xaacoondoo, waa dalub Kedar ak waa Sela sarxolleendoo, kaw tund ya di riirum mbég!
¶ Lu jëm ci Kedar ak nguuri Àccor yi Nabukodonosor buuru Babilon nangu woon, Aji Sax ji dafa wax ne: «Ñokket ci kaw Kedar, ba tas waa penku yooyu,