TSK

TSK · Isaiah 41:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yaw yaa di Aji Sax ji, Yàlla ji tànn Ibraam, jële ko Ur gu waa Kalde, tudde ko Ibraayma.

Waxleen lii, yeen ñi Aji Sax ji jot, jote leen ci loxol bañ,

Waaye yaw Israyil, sama jaam bi; yaw Yanqóoba mi ma taamu, yaw askanu Ibraayma, samab xarit!

Waaye Aji Sax ji dafa wax ne: «Ndegam du maa fas sama kóllëre maak bëccëg ak guddi, te du maa saxalal asamaan ak suuf ay sàrt,

¶ Ma ne kon, xanaa Yàlla daa wacc ñoñam? Mukk kay! Man ci sama bopp ci Israyil laa bokk, askanoo ci Ibraayma, giiroo ci Beñamin.

James 2:5 TSK

¶ Bokk yi, soppe yi, dégluleen. Xanaa du Yàlla moo taamu ñi àddina jàppe ñu néew doole, ngir ñu barele ngëm, boole ci jagoo nguur, gi Yàlla dig ñi ko sopp?