TSK

TSK · Leviticus 24:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

ak tegukaayu làmp bu wurusu ngalam bi aki làmpam, làmp yi sësaloo ba jekk ak mboolemi jumtukaayam, ak diw gi ñuy taaloo,

mu wax Aaróona, ne ko: «Buy teg làmp yi, fa féete tegukaayu làmp ba kanam, fa la juróom ñaari làmp ya wara niite.»

Kon waxleen ne leen: «Ayca, ca ndigali yoon ya, ak seedey kàdduy waxyu ya. Kuy wax googu kàddu, ag leer fenkalu la.»

¶ «Takkuleen te seeni làmp di tàkk.

Ndaxte Yàlla mi ne: «Na leer gi leere ci biir lëndëm gi,» moo leeral sunu xol, ngir leeraangey xam-xamu leeru Yàlla, te leeraange googu mooy lerxat ci xar-kanamu Yeesu Almasi.

Ag lëndëm ngeen woon démb, waaye tey ag leer ngeen ci Boroom bi ngeen bokk. Jëfeleen nag ni niti leer.