TSK

TSK · Leviticus 25:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Diiru juróom ñaari ati naataange ya suuf sa nangu, ba meññeef ma tuuru.

Nangeen xam xéll ne, man Aji Sax ji, maa leen may bésub Noflaay ngir ngeen nopplu, te looloo tax ma may leen dundub ñaari fan ci bésub juróom benneel bi. Kon nag bésub juróom ñaareel ba, na ku nekk toog fi mu nekk, bu ci kenn génnati fi mu dëkk.»

¶ «Gannaaw loolu nangeen waññ ba ci juróom ñaari ati Noflaay, loolu di juróom ñaari at ba muy juróom ñaari yoon. Mu doon seen juróom ñaari ati Noflaay, tollu ci ñeent fukki at ak juróom ñeent.

¶ Aji Sax jee leen di booleek barke bu wàccal seenum sàq, ak seen mboolem ñaq, te moo leen di barkeel ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji jox.

Barkeb Aji Sax jeey maye alal, kër-këri taxula barele.