TSK

TSK · Luke 5:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba loolu amee Yàlla ne: «Na leer nekk,» leer daldi am.

Alyaasa yebal ndaw ca moom ne ko: «Demal sanguji juróom ñaari yoon ca dexu Yurdan, sa yaram set, dellu mel na mu meloon.»

Moo àddu, mu am; santaane, mu sotti.

Maa leen di musal ci seen mboolem sobe, maay woo am pepp, ful ko, te dootuma leen teg ab xiif.

Luke 8:54 TSK

Yeesu itam jàpp ca loxol janq ba, daldi àddu ca kaw, ne ko: «Janq, jógal.»