Numbers 4:18
TSK
«Buleen yóbbe Keyateen ñeek seeni làng, lu ñu leen di dagge ci biir Leween ñi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
«Buleen yóbbe Keyateen ñeek seeni làng, lu ñu leen di dagge ci biir Leween ñi.
Waaye ndegam Aji Sax ji moo sàkk ba sàkk tey lu masula am, ba suuf ŋa, mëdd leen, ñook lu bokk ci ñoom, ñu tàbbiwaale bakkan biir njaniiw, su boobaa dingeen xam ne ñoom ñii ñoo xarab Aji Sax ji.»
Doomi Kore ya nag deewuñu ca.
ak la mu def Datan ak Abiram, doomi Elyab Rubeneen ba, ba suuf ŋayee, wonn leen, ñook seen waa kër, ak seeni xayma, ak mboolem luy dund lu leen topp, ci digg Israyil gépp.
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel askanu Kore wu góor.
suuf a ne ŋafeet, wonn Datan, mëddaale gàngooru Abiram;
Ci kaw loolu suuf wallu ndaw sa, ŋa, daldi naan dex, ga gémmiñu ninki-nànka ja buusu woon.