TSK

TSK · Proverbs 1:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Nanu ko rey gaaw, sànni ko ca kàmb yee, su ko defee danu naan, rabu àll a ko fàdd. Nu seet ba xam fu muy mujj aki géntam?»

ci yàllay xeet yi leen séq, ñi leen jege, ak ñi leen sore, ci àddina sépp, cat ba cat,

Ndokklee yaw mi toppul tànki ku bon, taxawewuloo yoonu moykat, toogewuloo jataayu ñaawlekat.

Muy mocc ak a moccaat, ba nax ko, di wax lu neex, ba man ko.

Ab soxor day yóbbaale dëkkandoom, jëme ko ci lu bon.

ndax coxor lay nas ci xolam, te fitna la ay waxam di yee.

Ñu ni mel liggéeyaluñu Almasi sunu Boroom, seen koll lañuy liggéeyal. Làmmiñ yu neex, ak kàddu yuy jaye lañuy naxe ñi seenum xel foogadi.