TSK

TSK · Proverbs 1:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

ba suuf sa xar, boole leen ak Kore, wonn, keroog ba gàngoor ga sànkoo, te sawara wa lakk ñaar téeméeri nit ak juróom fukk, ñu daldi doon firnde luy artoo.

Ñeel Daawuda. Éy Aji Sax ji, yaw laay woo, di la wéeroo, bu ma tanqamlu. Soo nee cell, ma xawa tàbbim pax.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bi ñu dippee Pitax mu luu, dëkk fu sore; di taalifu jàngle bu Daawuda fentoon, ba ko Filisteen ña jàppee ca Gaat.

ba nit ña xadaroo sunu kaw, dañu nu doon wonn, nuy dund,

«Buuru Babilon warax na ma. Da maa muucu, ñiit ma, ba ma set ni ndab. Da maa modd ni ninki-nànka, sole kollam li gën ci man, yàbbi la ca des.»

Sa noon yépp a lay ñaawal, di la kókkaleek a kekku, te naan: «Sànk nanu leen nag! Bii bés lanu yàggoona séentu, te noo ko fekke tey.»

Seenug boli di bàmmeel bu ne ŋàpp, seen làmmiñ di ràbb njublaŋ, seeni kàddu aay ni daŋaru ñàngóor.