Psalms 38:6
TSK
Maa def ug ndof, ba am dana yu bédd, ba xasaw.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Maa def ug ndof, ba am dana yu bédd, ba xasaw.
Làmmiñu waxkat, jam-jami jaasi; kàddu gu xelu, garab la ci.
Xol bu sedd, kanam gu leer; xol bu tiis, boroom ne yogg.
Nit bége na tontam lu dal, kàddu gu jib fa mu ñoree neex!
Wax ju yiw di lem juy xelli, neexa ñam, di jàmmi yaram.
Ku bëgga dund, dékku woppi yaram, waaye xol bu jeex maneesu koo wéye.
Diwook suuru day naatal xol; waaye li neex cib xarit, xol la lay digale.
¶ Aji Sax ji nag àddu, wax ak malaaka ma doon wax ak man, kàdduy mas-sawu yu neex.
Ci biir njàqare, ak xol bu fees, ak rongooñ yu bare laa leen bind. Binduma leen ngir naqaral leen, waaye cofeel gu réy gi ma am ci yeen moo tax.