TSK

TSK · Proverbs 15:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Nabal ne ndawi Daawuda: «Ana kuy Daawuda? Kuy doomu Yese sax? Jamonoy tey jaam yu baree ngi fàqe ci seeni sang.

Waa giirug Yuda gépp nag mànkoo ne waa Israyil: «Li ko waral mooy Buur da di sunu mbokk lenqe. Ana lu ngeen di mer ci loolu? Danoo lekkal Buur dara mbaa nu sàkkal sunu bopp lenn ci alalam?»

Buur tontu mbooloo ma kàddu gu ñagas, bàyyi la ko mag ña digaloon.

Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.

Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.