Job 31:5
TSK
Ndegam damaa doxe ndëngte, mbaa ma gaawtoo njublaŋ,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ndegam damaa doxe ndëngte, mbaa ma gaawtoo njublaŋ,
Kàdduy ku jub jariñ na ñu bare, dof ñàkk na bopp, ba far dee.
Farlu, woomle; ku gaawtu, mujj néewle.
Boroom worma, bare barke; ku yàkkamtee woomle, sa mbugal du jaas.
Ana koo gis, mu rattaxle? Kooku ab dof a ko gën demin.
Waarekat ba daa xelu, di jànglewaale xam-xam, di natt ak a gëstu, di jekk-jekkal kàdduy xel yu takku.
Moo tax Boroom bi Aji Sax ji wax ne: «Maa ngii di dëj fi Siyoŋ aw doju coll, muy doju collu tànnéef wu gànjare ngir kenu gi, te ku ko wéeroo doo gaawa daw.
¶ Li may ñaan nag moo di seen cofeel yokku tey gën di yokku, te ngeen ànd ceek xam-xam bu matale ak gépp ràññee,