TSK

TSK · Proverbs 23:34

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Maa ngi lay gërëme sa njort, di la gërëme sa jëmmu bopp jii ma teree tuur deret, ngir feyul sama bopp.

¶ Ci kaw loolu waa ja yóbbu Daawuda, ndeke nit ñaa nga ne wesar ca àll ba bépp, di lekk ak a naan, di mbumbaaye mboolem alal ju bare ja ñu nangoo ca réewum Filisti ak réewum Yuda.

Simri, jawriñam ba yilifoon genn-wàllu watiiri xareem, moo ko fexeel. Booba Elaa ngay naan ba màndi ca kër Arsa, ka yor mbiri këram ca Tirsa.

Buur moomul di naan biiñ, Lemuyel, buur moomu ko; kilifa moomul di sàkku ñoll.

¶ «Moytuleena yaafusal seen bopp ci naan gu ëpp ak màndite ak xalaati àddina, lu ko moy bés ba jekki dal ci seen kaw,