TSK

TSK · Proverbs 3:32

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 29:4 TSK

Ba ma tolloo sama digg doole, te Yàlla xejjoo sama xayma.

Ndéeyu Aji Sax ji, jagley ku ko ragal. Kóllëreem la koy xamal.

Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.

Tiisu xol, boroom a ko xam; mbégte ma it jaambur bokku ca.

Yeesu ne leen: «Yeen yeenay jub-jublu ci kanam nit ñi, waaye Yàlla xam na seen xol. Ndax li nit ñi gëna naw, lu seexluwu la fa Yàlla.