Proverbs 17:11
TSK
Ku bon fippu doŋŋ lay jéem, te musibaa koy dikkal.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ku bon fippu doŋŋ lay jéem, te musibaa koy dikkal.
Sàkkuleen jàmmu dëkk bi ma leen toxal, te ñaanal ko ci Aji Sax ji, ndax jàmmu dëkk bi mooy seen jàmm.
¶ Na ku nekk déggal njiit yi yor kilifteef, nde amul njiit lu bawoowul fa Yàlla, te njiit yi toog, Yàlla moo leen tabb.
¶ Kon nag li jiitu ci mboolem li may dénkaane mooy ngeen di dagaan, di ñaan, di tinu ak a sant, ñeel doom aadama yépp,
¶ Rawatina nag boroom xemmemtéefi yàqute, yi topp seen bakkan te faalewuñu genn kilifteef. Ñu fétteeral lañu te bew, ragaluñoo saaga sax boroom daraja yu kawe ya fa asamaan.