¶ Ba yëngu-yëngu ba jeexee, Póol daa woo taalibe ya, ñaax leen, ba noppi tàggtoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu Maseduwan.
TSK
TSK · 2 Corinthians 2:13
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Acts 20:1
TSK
¶ Ba nu àggee diiwaanu Maseduwan, sunuw yaram noppluwul, waaye daj nanu bépp coono: xeex ci biti, njàqare ci biir.
Looloo tax nu soññ Tit, ngir noonee mu tàmbalee woon ci yeen, ndajalem ndimbal li, mu àggalee ko ci yeen.
Su dee mbirum Tit, mooy sama wéttal, di ma jàpple ci liggéey bi, ngir yeen. Sunu bokk, yi ànd ak moom nag, ñooy ndawi mboolooy gëmkat ñi, te ñooy teraangay Almasi.
Galatians 2:1
TSK
¶ Fukki at ak ñeent gannaaw gi laa dellu Yerusalem, ànd ak Barnaba, yóbbaale Tit itam.
2 Timothy 4:10
TSK
Ndax kat Demas, àddinay tey la sopp ba tax mu wacc ma, dem Tesalonig, te Kereseñsë dem na diiwaanu Galasi, Tit dem diiwaanu Dalmasi.